Skip to content
The Believer's Library

Regional Wolof Bible Translation

1 Chronicles 1 RWBT

Show RWBT only
Verse × ×
1 Adam, Seth, Enosh, Aadama mooy baayu Set, Set di baayu Enos,
2 Kenan, Mahalalel, Jared, Enos di baayu Kenan, Kenan di baayu Maalaleel, Maalaleel di baayu Yeredd.
3 Enoch, Methuselah, Lamech, Yeredd di baayu Enog, Enog di baayu Matusalem, Matusalem di baayu Lemeg,
4 Noah, Shem, Ham, and Japheth. Lemeg di baayu Nóoyin, Nóoyin di baayu góor ñii di Sem ak Xam ak Yafet.
5 The sons of Japheth: Gomer, Magog, Madai, Javan, Tubal, Meshech, and Tiras. Doomi Yafet yu góor ñoo di Gomeer ak Magog ak Maday ak Yawaan ak Tubal ak Meseg ak Tiraas.
6 The sons of Gomer: Ashkenaz, Diphath, and Togarmah. Doomi Gomeer yu góor ñoo di Askenas ak Difaat ak Togarma.
7 The sons of Javan: Elishah, Tarshish, the Kittim, and the Rodanim. Doomi Yawaan yu góor ñoo di Elisa ak Tarsis ak Kitim ak Dodanim.
8 The sons of Ham: Cush, Mizraim, Put, and Canaan. Doomi Xam yu góor ñoo di Kuus ak Misrayim ak Puut ak Kanaan.
9 The sons of Cush: Seba, Havilah, Sabta, Raamah, and Sabteca. The sons of Raamah: Sheba and Dedan. Doomi Kuus yu góor ñoo di Saba ak Awila ak Sabta ak Raama ak Sabteka. Doomi Raama yu góor di Seba ak Dedan.
10 Cush fathered Nimrod; he was the first to become a mighty one on the earth. Kuus moo jur Nimrodd, ki njëkk di jàmbaar ju siiw ci kaw suuf.
11 Mizraim fathered the Ludim, the Anamim, the Lehabim, the Naphtuhim, Misrayim nag mooy maami Luddeen ñi ak Anameen ñi ak Leyabeen ñi ak Naftuyeen ñi
12 the Pathrusim, the Casluhim (from whom the Philistines came), and the Caphtorim. ak Pataruseen ñi ak Kasluxeen ñi, ñooñee waa Filisti soqikoo, ak it Kaftoreen ñi.
13 Canaan fathered Sidon his firstborn, and Heth, Kanaan moo taawloo Sidon, teg ca Ett.
14 and the Jebusites, the Amorites, the Girgashites, Kanaan mooy maamu Yebuseen ñi ak Amoreen ñi ak Girgaseen ñi.
15 the Hivites, the Arkites, the Sinites, Mooy maamu Eween ñi ak Arkeen ñi ak Sineen ñi.
16 the Arvadites, the Zemarites, and the Hamathites. Mooy maamu Arwàddeen ñi it ak Cemareen ñi ak Amateen ñi.
17 The sons of Shem: Elam, Asshur, Arpachshad, Lud, and Aram; and the sons of Aram: Uz, Hul, Gether, and Meshech. Doomi Sem yu góor ñoo di Elam ak Asur ak Arpagsàdd ak Ludd ak Aram. Góor ñi Aram jur ñii la: Ucc ak Xuul ak Geter ak Meseg.
18 Arpachshad fathered Shelah, and Shelah fathered Eber. Arpagsàdd jur Sela, Sela jur Eber.
19 Eber had two sons: one named Peleg, since the earth was divided in his days, and his brother named Joktan. Eber moom jur ñaari doom yu góor. Kenn ki tudd Peleg (muy firi Séddalikoo), ndaxte ci jamonoom àddina dafa séddalikoo woon. Rakku Peleg ju góor mooy Yogtaan.
20 Joktan fathered Almodad, Sheleph, Hazarmaveth, Jerah, Yogtaan a jur Alamodàdd ak Selef ak Asarmawet ak Yerax
21 Hadoram, Uzal, Diklah, ak Adoram ak Usal ak Digla
22 Ebal, Abimael, Sheba, ak Ebal ak Abimayel ak Seba
23 Ophir, Havilah, and Jobab. All these were the sons of Joktan. ak Ofir ak Awila ak Yobab. Ñooñu ñépp di doomi Yogtaan yu góor.
24 Shem, Arpachshad, Shelah, Ci tënk, lii mooy askanu Sem: Sem mooy baayu Arpagsàdd, Arpagsàdd di baayu Sela.
25 Eber, Peleg, Reu, Sela di baayu Eber, Eber di baayu Peleg, Peleg di baayu Rew.
26 Serug, Nahor, Terah, Rew mooy baayu Serug, Serug di baayu Naxor, Naxor di baayu Teraa.
27 Abram, that is, Abraham. Teraa mooy baayu Ibraam miy Ibraayma.
28 The sons of Abraham: Isaac and Ishmael. Doomi Ibraayma yu góor ñoo di Isaaxa ak Ismayla.
29 These are their family records: the firstborn of Ishmael, Nebaioth; then Kedar, Adbeel, Mibsam, Ñii lañu meññ: taawub Ismayla bu góor mooy Nebayot. Ña ca topp di Kedar ak Adabeel ak Mibsam
30 Mishma, Dumah, Massa, Hadad, Tema, ak Misma ak Duuma ak Maasa ak Adàdd ak Tema
31 Jetur, Naphish, and Kedemah. These are the sons of Ishmael. ak Yetur ak Nafis ak Kedama. Ñooñu ñooy doomi Ismayla yu góor.
32 Keturah, Abraham's concubine, bore Zimran, Jokshan, Medan, Midian, Ishbak, and Shuah. Jokshan's sons: Sheba and Dedan. Ketura, nekkaaleb Ibraayma am naak moom doom yu góor. Ñuy Simran ak Yogsan ak Medan ak Majan ak Yisbag ak Suwa. Doomi Yogsan yu góor di Seba ak Dedan.
33 The sons of Midian: Ephah, Epher, Hanoch, Abida, and Eldaah. All these were the sons of Keturah. Doomi Majan yu góor ñoo di Efa ak Efer ak Enog ak Abida ak Elda. Ñooñu ñépp xeetu Ketura lañu.
34 Abraham fathered Isaac. The sons of Isaac: Esau and Israel. Ibraayma mooy baayu Isaaxa. Doomi Isaaxa yu góor di Esawu ak Israayil.
35 The sons of Esau: Eliphaz, Reuel, Jeush, Jalam, and Korah. Doomi Esawu yu góor ñoo di Elifas ak Rewel ak Yewus ak Yalam ak Kore.
36 The sons of Eliphaz: Teman, Omar, Zephi, Gatam, Kenaz, Timna, and Amalek. Doomi Elifas yu góor ñoo di Teman ak Omar ak Cefo ak Gatam ak Kenas ak Amaleg mi mu am ak Timna.
37 The sons of Reuel: Nahath, Zerah, Shammah, and Mizzah. Doomi Rewel yu góor ñoo di Naxat ak Sera ak Saama ak Misa.
38 The sons of Seir: Lotan, Shobal, Zibeon, Anah, Dishon, Ezer, and Dishan. Ñi sancoon Edom ñoo askanoo ci doomi Seyir yu góor. Ñoo di Lotan ak Sobal ak Cibeyon ak Ana ak Dison ak Eccer ak Disan.
39 The sons of Lotan: Hori and Homam; and Lotan's sister was Timna. Doomi Lotan yu góor ñoo di Ori ak Omam. Jigéenub Lotan di Timna.
40 The sons of Shobal: Alian, Manahath, Ebal, Shephi, and Onam. The sons of Zibeon: Aiah and Anah. Doomi Sobal yu góor ñoo di Alwan ak Manaxat ak Ebal ak Sefi ak Onam. Doomi Cibeyon yu góor di Aya ak Ana.
41 The sons of Anah: Dishon. The sons of Dishon: Hamran, Eshban, Ithran, and Cheran. Doomu Ana ju góor moo di Dison. Doomi Dison yu góor ñoo di Amran ak Esban ak Yittran ak Keran.
42 The sons of Ezer: Bilhan, Zaavan, and Jaakan. The sons of Dishan: Uz and Aran. Doomi Eccer yu góor ñoo di Bilan ak Saawan ak Yakan. Doomi Disan yu góor di Ucc ak Aran.
43 These are the kings who reigned in Edom's land before any king reigned over the Israelites: Bela son of Beor, whose city was Dinhabah. Buur ya falu woon ca réewum Edom, lu jiitu benn buuru bànni Israayil di falu, ñii la: Bela doomu Bewor ju góor. Dinaba moo doon péeyam.
44 When Bela died, Jobab son of Zerah from Bozrah reigned in his place. Ba Bela faatoo, Yobab doomu Sera ma dëkk Boccara moo falu buur, wuutu ko.
45 When Jobab died, Husham from the land of the Temanites reigned in his place. Ba Yobab faatoo, Usam ma bokk ci diiwaanu waa Teman falu buur, wuutu ko.
46 Husham died; Hadad son of Bedad, who defeated Midian in the country of Moab, reigned instead; his city was Avith. Ba Usam faatoo, Adàdd doomu Bedàdd ju góor ja duma woon waa Majan ca réewu Mowab, daldi falu buur, wuutu ko. Péeyam moo doon Awit.
47 When Hadad died, Samlah from Masrekah reigned in his place. Ba Adàdd faatoo, Samla ma dëkk Masreka moo falu buur, wuutu ko.
48 When Samlah died, Shaul from Rehoboth on the River reigned in his place. Ba Samla faatoo, Sawul mu Rexobot Efraat moo falu buur, wuutu ko.
49 When Shaul died, Baal-hanan son of Achbor reigned in his place. Ba Sawul faatoo, Baal Anan doomu Agbor ju góor moo falu buur, wuutu ko.
50 Baal-hanan died; Hadad reigned in his place. His city was Pai; his wife was Mehetabel, daughter of Matred, daughter of Me-zahab. Ba Baal Anan faatoo, Adàdd moo falu buur, wuutu ko. Pawu moo doon péeyam, soxnaam di Metabeel ma Mataredd doomu Mesaab di yaayam.
51 And Hadad died. The chiefs of Edom were: chief Timna, chief Aliah, chief Jetheth, Gannaaw ba Adàdd faatoo, kilifa ya jiite Edom ñoo di Timna ak Alwa ak Yetet
52 chief Oholibamah, chief Elah, chief Pinon, ak Olibama ak Ela ak Pinon
53 chief Kenaz, chief Teman, chief Mibzar, ak Kenas ak Teman ak Mibcar
54 chief Magdiel, chief Iram. These were the chiefs of Edom. ak Magdiyel ak Iram. Ñooñoo doon kilifay Edom.
FHB

Scripture from Father’s Heart Bible™. © 2026 Spirit Media Publishing, the imprint of Spirit Media Inc. All rights reserved. In Divine Voice™ Color, the words spoken by our Father show in blue, the words of the Son in red, and the words of the Spirit in purple.

RWBT

Kàddug Yàlla © 2025 M.B.S.: N.I.N.E.A. 20215410C9 Yokk sa njàng: https://kaddugyalla.com/ Copyright: https://kaddugyalla.com/copyright
Regional Wolof Bible Translation · Creative Commons - Attribution-NonCommercial [CC BY-NC]